WOLLEB_JLD_NARR_03_RUF.EAF     karaoke karaoke2

ecouter
ndah man lébu laa géej la ma ham  
ndah man lébu laa géej la ma ham
ndax man lébu laa géej la ma ham
car moi lébou être_je mer être je connaître
CONJ PN1SG N STG N VI PNS1SG VI
ecouter
géej la ma ham liggéey bi ala la ma dab rek  
géej la ma ham liggéey bi ala la ma dab rek
géej la ma ham liggéey bi ala la ma dab rek
mer être je connaître travail le\la être quelque_chose me rattraper seulement
N VI PNS1SG VI N ART VI PN PNC1SG VT ADV
ecouter
waaye géej la ma ham  
waaye géej la ma ham
waaye géej la ma ham
mais mer être je connaître
CONJC N VI PNS1SG VI
ecouter
kërug lëmm laa la gis kërug lëmm  
kërug lëmm laa la gis kërug lëmm
kër -u -g lëmm laa la gis kër -u -g lëmm
famille DETERMINATIF CLASSE être entier c'est...que_tu INACC voir famille DETERMINATIF CLASSE être entier
N SUF AFFIXE VI STG AUX VT N SUF AFFIXE VI
ecouter
ñépp demandoo si mbëkk mi si genn gaal  
ñépp demandoo si mbëkk mi si genn gaal
ñépp dem -andoo si mbëkk mi si benn gaal
tous\toutes partir\aller en même temps à aventure le\la en un\une pirogue
PNPL VI SUF PREP N ARTDEFSG PREP NUM N
ecouter
... mais barñi  
... mais barñi
... mais barñi
Bargni
N
ecouter
baa fa demoon nii doon def enquête  
baa fa demoon nii doon def enquête
baa fa dem -oon nii doon def enquête
si_tu là-bas partir\aller PASSE comme ça INACC_PASSE faire
STG ADV VI SUF ADV STG VT
ecouter
kër gaa fa dugg  
kër gaa fa dugg
kër gaa fa dugg
maison où_tu là-bas entrer
N STG ADV VI
ecouter
ñu ne la diw dem na espagne  
ñu ne la diw dem na espagne
ñu ne la diw dem na espagne
on dire te\toi untel\unetelle partir\aller MRV
PNIND V PNC2SG N VI MOD
ecouter
diw dem na italie si mbëkk mi la jaare  
diw dem na italie si mbëkk mi la jaare
diw dem na italie si mbëkk mi la jaar -e
untel\unetelle partir\aller MRV à aventure le\la c'est...que... passer APPLICATIF
N VI MOD PREP N ARTDEFSG MOD VI SUF
ecouter
kër gaa fa dem de par exemple baa taalee sa oto dem laajte  
kër gaa fa dem de par exemple baa taalee sa oto dem laajte
kër gaa fa dem de par exemple baa taal -ee sa oto dem laaj -te
famille où_tu là-bas partir\aller vraiment si_tu allumer ANT ton\ta auto partir\aller demander DEVERBAL
N STG ADV VI ADV STG null SUF POSS2SG N VI null null
ecouter
kër gaa fa dugg ñu ne la diw dem na espagne  
kër gaa fa dugg ñu ne la diw dem na espagne
kër gaa fa dugg ñu ne la diw dem na espagne
maison où_tu là-bas entrer on dire te\toi untel\unetelle partir\aller MRV
N STG ADV VI PNIND V PNC2SG N VI MOD
ecouter
diw dem na mbëkk ma ñépp ñoo dem  
diw dem na mbëkk ma ñépp ñoo dem
diw dem na mbëkk ma ñépp ñoo dem
untel\unetelle partir\aller MRV aventure le\la tous\toutes eux_MRS partir\aller
N VI MOD N ARTDEFSG PNPL STG VI
ecouter
ndah dañuy ham ne géej gii  
ndah dañuy ham ne géej gii
ndah da -ñu -y ham ne géej g -ii
car EXPLICATIF ils\elles INACC savoir que mer SG ce_ci\cette_ci
CONJ MOD PNS3PL VI VI CONJ N CLASSE DEMPROXSG
ecouter
comme i yéfi géej la rek  
comme i yéfi géej la rek
comme i yéf -i géej la rek
des choses DETERMINATIF mer être seulement
ARTINDPL N DEFPROX N VI ADV
ecouter
ñoom mën nañoo kii te dañoo tëmb si gaal yi  
ñoom mën nañoo kii te dañoo tëmb si gaal yi
ñoom mën nañoo kii te dañoo tëmb si gaal yi
eux\elles pouvoir MOD_ils_aVERBAL truc\machin et EXPLIC_ils_a Verbal flotter en pirogue les
PN3PL V STG STG CONJC STG VI PREP N PN
ecouter
waaye ñii fa des  
waaye ñii fa des
waaye ñ -ii fa des
mais PL ceux-ci\celles-ci là-bas rester
CONJC CLASSE DEMPROXPL ADV VI
ecouter
moo la ñii hamente ñoo miinul géej  
moo la ñii hamente ñoo miinul géej
moo la ñ -ii ham ñoo miin -ul géej
c'est_ça_qui être PL ceux-ci\celles-ci savoir eux_MRS être_habitué NEG mer
STG VI CLASSE DEMPROXPL VI STG VI SUF N
ecouter
ndah baa demee dugë si biir gaal say butit yii  
ndah baa demee dugë si biir gaal say butit yii
ndah baa dem -ee dugg si biir gaal say butit y -ii
car quand_tu partir\aller ANT entrer en intérieur pirogue tes intestin PL ces_ci
CONJ STG VI SUF VI PREP ADV N Poss2Pl N CLASSE DEMPROXPL
ecouter
gaal gi ba commencer daw  
gaal gi ba commencer daw
gaal gi ba commencer daw
pirogue le\la quand courir
N ARTDEFSG PN VT
ecouter
say butit yii moo la commencer tourner  
say butit yii moo la commencer tourner
say butit y -ii moo la commencer tourner
tes intestin PL ces_ci c'est_ça_qui INACC
Poss2Pl N CLASSE DEMPROXPL STG AUX
ecouter
danga woccoo woccoo woccoo woccu ba dootoo am laa leekë  
danga woccoo woccoo woccoo woccu ba dootoo am laa leekë
danga wocc -oo wocc -oo wocc -oo woccu ba dootoo am laa lekk
EXPLICATIF_tu vomir u_a.Verbal\o#_a.Verbal vomir u_a.Verbal\o#_a.Verbal vomir u_a.Verbal\o#_a.Verbal vomir jusque ASPECT+NEG+ITER+NEG+2psSg avoir CHOSE_tu manger\consommer
STG VT STG VT STG VT STG VT ADV STG VT STG VT
ecouter
moo tah ñu tëmbël la si gaal gi  
moo tah ñu tëmbël la si gaal gi
moo tax ñu tëmb -ël la si gaal gi
c'est_ça_qui faire_que on flotter CAUSATIF te\toi en pirogue le\la
STG V PNIND VI SUF PNC2SG PREP N ARTDEFSG
ecouter
diigal la si ndoh mi  
diigal la si ndoh mi
diig -al la si ndoh mi
sombrer CAUSATIF te\toi en eau le\la
VI SUF PNC2SG PREP N ARTDEFSG
ecouter
ndah baa fa desee ab het laa doon te ñépp laa reyandoo  
ndah baa fa desee ab het laa doon te ñépp laa reyandoo
ndah baa fa des -ee ab xet laa doon te ñépp laa rey -andoo
car si_tu là-bas rester ANT un\une odeur c'est...que_il_INACC être et tous\toutes c'est...que_il_INACC tuer en même temps
CONJ STG ADV VI SUF ARTINDSG N STG VI CONJC PNPL STG VT SUF
ecouter
moo tah mbëkë mi baahul  
moo tah mbëkë mi baahul
moo tax mbëkk mi baah -ul
c'est_ça_qui faire_que aventure le\la être_bien NEG
STG V N ARTDEFSG VI SUF
ecouter
ka ka mana bàyyi na ka bàyyi  
ka ka mana bàyyi na ka bàyyi
ka ka man -a bàyyi na ka bàyyi
celui\celle ça pouvoir a-VERBAL abandonner INCITATIF ça abandonner
PNC3SG PN VI SUF VT MOD PN VT
ecouter
man dey maa waroona njëka dem  
man dey maa waroona njëka dem
man dey maa war -oon -a njëkk -a dem
moi vraiment c'est_je_qui devoir\incomber PASSE a-VERBAL être_premier a-VERBAL partir\aller
PN1SG ADV STG VI SUF SUF VI SUF VI
ecouter
kii yii moo def nii  
kii yii moo def nii
kii y -ii moo def nii
truc\machin PL ces_ci il_INACC faire comme ça
STG CLASSE DEMPROXPL STG VT ADV
ecouter
aka dóor si houle bi da laa neerloo baa dul demkatu géej  
aka dóor si houle bi da laa neerloo baa dul demkatu géej
aka dóor si houle bi da laa neer -loo baa dul dem -kat -u géej
et_aVERBAL battre à le\la EXPLICATIF te_INACC avoir_le_mal_des_transports CAUSATIF si_tu être_NEG partir\aller AGENTIF de mer
STG VT PREP ART MOD STG VI SUF STG STG VI SUF SUF N
ecouter
te daawoo dem géej  
te daawoo dem géej
te d- -aan -w -oo dem géej
alors que INacc Hab_Passé EPENTH NEG_PNS2SG partir\aller mer
CONJC VI SUF CONS STG VI N
ecouter
yoof gii ka fa musul ka fa demul géej  
yoof gii ka fa musul ka fa demul géej
yoof g -ii ka fa mus -ul ka fa dem -ul géej
Yoff SG ce_ci\cette_ci celui\celle là-bas avoir_fait_l'expérience_de NEG celui\celle là-bas partir\aller NEG mer
N CLASSE DEMPROXSG PNC3SG ADV VAUX SUF PNC3SG ADV VI SUF N
ecouter
geneen géej gaa dem daha la diig  
geneen géej gaa dem daha la diig
geneen géej gaa dem daha la diig
autre mer où_tu partir\aller EXPLICATIF_tu INACC sombrer
DET N STG VI MOD AUX VI
ecouter
yoof gii rek laa mëna dem géej  
yoof gii rek laa mëna dem géej
yoof g -ii rek laa mën -a dem géej
Yoff SG ce_ci\cette_ci seulement c'est...que_tu pouvoir a-VERBAL partir\aller mer
N CLASSE DEMPROXSG ADV STG V SUF VI N
ecouter
mu jàlle fi u la dem si gaal gi mu war laa mëna yóbbu espagne  
mu jàlle fi u la dem si gaal gi mu war laa mëna yóbbu espagne
mu jàll -e fi u la dem si gaal gi mu war laa mën -a yóbbu espagne
il\elle passer APPLICATIF y tu INACC partir\aller en pirogue le\la il\elle devoir\incomber te_INACC pouvoir a-VERBAL emmener
PNS3SG VI SUF PN PNS2SG AUX VI PREP N ARTDEFSG PNS3SG VI STG V SUF VT
ecouter
mu àgga si jàmm ah salaam  
mu àgga si jàmm ah salaam
mu àgg si jàmm ah salaam
il\elle arriver en paix et paix
PNS3SG VI PREP N PREP N
ecouter
waaye ka fi jaarul géejag yoof gii  
waaye ka fi jaarul géejag yoof gii
waaye ka fi jaar -ul géej -u -g yoof g -ii
mais quiconque y passer NEG mer DETERMINATIF CLASSE Yoff SG ce_ci\cette_ci
CONJC PN PN VI SUF N SUF AFFIXE N CLASSE DEMPROXSG
ecouter
u jaar nii rek  
u jaar nii rek
u jaar nii rek
tu passer comme ça seulement
PNS2SG VI ADV ADV
ecouter
moo tah géej  
moo tah géej
moo tax géej
c'est_ça_qui faire_que mer
STG V N
ecouter
baa ka mënulee jarul nga dem  
baa ka mënulee jarul nga dem
baa ka mën -ul -ee jar -ul nga dem
quand_tu ça pouvoir NEG ANT valoir_la_peine_de NEG tu partir\aller
STG PN V SUF SUF VI SUF PNS2SG VI
ecouter
laa mënul bu si gaawa dugë  
laa mënul bu si gaawa dugë
laa mën -ul bu si gaaw -a dugg
CHOSE_tu pouvoir NEG INCITATIF_NEG y être prompt à a-VERBAL s'engager
STG V SUF MOD PREP v.aux SUF VI
ecouter
xam nga moom njàngam soriwul  
xam nga moom njàngam soriwul
xam nga moom n- jàng -am sori -w -ul
savoir tu ça alternance consonnantique apprendre POSS3SG être loin EPENTH NEG
VI PNS2SG PN null null SUF null CONS SUF
ecouter
waaye am na laa xam ne duma si ëppël  
waaye am na laa xam ne duma si ëppël
waaye am na laa xam ne duma si ëpp -ël
mais avoir MRV CHOSE_tu savoir que FUT_NEG_je en être_excessif CAUSATIF
CONJC VT MOD STG VI CONJ STG PREP VI SUF
ecouter
ka la warul laaj  
ka la warul laaj
ka la war -ul laaj
celui\celle te\toi devoir\incomber NEG demander
PNC3SG PNC2SG VI SUF VT
ecouter
nee ka gisuma  
nee ka gisuma
ne ka gis -u -ma
dire lui voir NEGATION je
V PN VT SUF PNS1SG
ecouter
xaw ma  
xaw ma
xaw ma
savoir+NEG je
STG PNS1SG
ecouter
lébu nga am nga fullë  
lébu nga am nga fullë
lébu nga am nga fulla
lébou tu avoir tu fermeté_de_caractère
N PNS2SG VT PNS2SG N
ecouter
ka la laaj  
ka la laaj
ka la laaj
quiconque te\toi demander
PN PNC2SG VT
ecouter
nee ka sa yoon newu si  
nee ka sa yoon newu si
ne ka sa yoon nekk -u si
dire lui ton\ta chemin\voie_d'accès se_trouver NEGATION y
V PN POSS2SG N VI SUF PREP
ecouter
demal laaj ka diw  
demal laaj ka diw
dem -al laaj ka diw
partir\aller IMPERATIF demander ça untel\unetelle
VI SUF VT PN N
ecouter
li ña la joh  
li ña la joh
li ña la joh
ce on te\toi remettre\donner
PN PNIND PNC2SG VT
ecouter
taxawu nga ka  
taxawu nga ka
taxaw -u nga ka
se_tenir_debout PRONOMINAL tu ça
VI SUF PNS2SG PN
ecouter
gisuma ka  
gisuma ka
gis -u -ma ka
voir NEGATION je ça
VT SUF PNS1SG PN
ecouter
li ñu la joh  
li ñu la joh
li ñu la joh
ce on te\toi remettre\donner
PN PNIND PNC2SG VT
ecouter
demal joh ko  
demal joh ko
dem -al joh ko
partir\aller IMPERATIF remettre\donner lui\elle
VI SUF VT PN
ecouter
u joh ko kañ la ka santa  
u joh ko kañ la ka santa
u joh ko kañ la ka sant
tu remettre\donner lui\elle celui_on te\toi ça ordonner_de_faire
PNS2SG VT PN STG PNC2SG PN VT
ecouter
u ñów toogaat sab toogaay  
u ñów toogaat sab toogaay
u ñów toog -aat sab toog -aay
tu venir s'asseoir encore ton_CLASSE s'asseoir DEVERBATIF
PNS2SG VI VI SUF STG VI SUF