WOLLEB_JLD_NARR_02_KAMND.EAF     karaoke karaoke2

ecouter
ala koon kumba amul ndey yaayam dafa dee  
ala koon kumba amul ndey yaayam dafa dee
ala koon kumba am -ul ndey yaay -am dafa dee
être marque l'irréel Coumba avoir NEG mère mère\maman POSS3SG EXPLICATIF mourir
VI MOD N VT SUF N N SUF MOD VI
ecouter
kumba am ndey yaayam neeka fa  
kumba am ndey yaayam neeka fa
kumba am ndey yaay -am neeka fa
Coumba avoir mère mère\maman POSS3SG se trouver là-bas
N VT N N SUF VI ADV
ecouter
leegi kumba am ndey di fa am teraanga kumba amul ndey di fa am teraanga  
leegi kumba am ndey di fa am teraanga kumba amul ndey di fa am teraanga
leegi kumba am ndey di fa am teraanga kumba am -ul ndey di fa am teraanga
alors Coumba avoir mère INacc avoir honneur Coumba avoir NEG mère INacc là-bas avoir honneur
ADV N VT N ASPECT ADV VT N N VT SUF N ASPECT ADV VT N
ecouter
yaayu kumba amul ndey  
yaayu kumba amul ndey
yaay -u kumba am -ul ndey
mère\maman de Coumba avoir NEG mère
N SUF N VT SUF N
ecouter
kumba am ndey yaayam ne kii du fi am teraanga ki fi yaayam neeka toog  
kumba am ndey yaayam ne kii du fi am teraanga ki fi yaayam neeka toog
kumba am ndey yaay -am ne kii du fi am teraanga ki fi yaay -am neeka toog
Coumba avoir mère mère\maman POSS3SG dire celui-ci\celle-ci futur négative ici avoir honneur celui\celle ici mère\maman POSS3SG se trouver s'asseoir
N VT N N SUF V DEMPROXSG MOD ADV VT N PN ADV N SUF VI VI
ecouter
leegi mu dee toroxal dee toroxal dee toroxal dee toroxal  
leegi mu dee toroxal dee toroxal dee toroxal dee toroxal
leegi mu dee torox -al dee torox -al dee torox -al dee torox -al
alors il\elle INACC vivre misérablement CAUSATIF INACC vivre misérablement CAUSATIF INACC vivre misérablement CAUSATIF INACC vivre misérablement CAUSATIF
ADV PNS3SG AUX VI SUF AUX VI SUF AUX VI SUF AUX VI SUF
ecouter
ba ka torohal rek baay bi ànd si ba ka torohal rek baay bi ànd si  
ba ka torohal rek baay bi ànd si ba ka torohal rek baay bi ànd si
ba ka torox -al rek baay bi ànd si ba ka torox -al rek baay bi ànd si
quand la vivre misérablement CAUSATIF seulement père le\la être d'accord en quand la vivre misérablement CAUSATIF seulement père le\la être d'accord en
CONJ pnSgEl VI SUF ADV N ART V PREP CONJ pnSgEl VI SUF ADV N ART V PREP
ecouter
be leegi ña def sabarag buur  
be leegi ña def sabarag buur
be leegi ña def sabar -u -g buur
jusque alors on faire partie_de_tam-tam DETERMINATIF CLASSE roi
PREP ADV PNIND VT N SUF AFFIXE N
ecouter
ñu la sabaru leegi ñu ne garab ga sa toolab baay buur  
ñu la sabaru leegi ñu ne garab ga sa toolab baay buur
ñu la sabar -u leegi ñu ne garab ga sa tool -u -b baay buur
on INACC partie_de_tam-tam DEVERBAL alors on dire arbre le\la à champ de SG père roi
PNIND AUX N SUF ADV PNIND V N ARTSG PREP null SUF CLASSE N N
ecouter
ka ka ham baay buur taka la  
ka ka ham baay buur taka la
ka ka ham baay buur taka la
celle le savoir père roi épouser te\toi
pnC3Sg pnSgEl VI N N VT PNC2SG
ecouter
leegi kumba amul ndey  
leegi kumba amul ndey
leegi kumba am -ul ndey
alors Coumba avoir NEG mère
ADV N VT SUF N
ecouter
ñoom ñéep ña fa woon  
ñoom ñéep ña fa woon
ñoom ñépp ñi fa woon
eux\elles tous\toutes qui là-bas PASSE
PN3PL PNPL PNPL ADV TEMPS
ecouter
kumba amul ndey  
kumba amul ndey
kumba am -ul ndey
Coumba avoir NEG mère
N VT SUF N
ecouter
yaay ji feka baay baa ng in a ngee takal ab lam  
yaay ji feka baay baa ng in a ngee takal ab lam
yaay ji feka baay baa ng in a ng -ee tak -al ab lam
mère\maman le\la se_trouver_que père le_PRESENTATIF\la_PRESENTATIF on PRESENTATIF PRESENTATIF PROX_lui attacher BENEFACTIF un\une bracelet
N ARTDEFSG LOC N STG PNIND MOD null STG VT SUF ARTINDSG N
ecouter
yaay ji ne baay bi  
yaay ji ne baay bi
yaay ji ne baay bi
mère\maman le\la dire père le\la
N ARTDEFSG V N ART
ecouter
ne kumba amul ndey baa daggulee lam bii si lohoom  
ne kumba amul ndey baa daggulee lam bii si lohoom
ne kumba am -ul ndey baa dagg -ul -ee lam bii si loho -am
dire Coumba avoir NEG mère si_tu couper NEG ANT bracelet ce\cette à bras à_lui\à_elle
V N VT SUF N STG VI SUF null N DEMPROXSG PREP N SUF
ecouter
u joh ko kumba ndey  
u joh ko kumba ndey
u joh ko kumba ndey
tu remettre\donner ça Coumba mère
PNS2SG VT PN N N
ecouter
nu fase  
nu fase
nu fase
nous être_divorcé
PN1PL VI
ecouter
mu fob paaka ne tippet loho la  
mu fob paaka ne tippet loho la
mu fab paaka ne tippet loho ba
il\elle prendre couteau faire net bras le\la
PNS3SG VT N COV ADV N ARTDEFSG
ecouter
mu am um kuuñ sabar ga ñów  
mu am um kuuñ sabar ga ñów
mu am um kuuñ sabar ga ñów
il\elle avoir un\une moignon partie_de_tam-tam le\la venir
PNS3SG VT ARTINDSG N N ARTSG VI
ecouter
leegi ñu ne sabar gi ka hamul garab ga sa toolab baay buur  
leegi ñu ne sabar gi ka hamul garab ga sa toolab baay buur
leegi ñu ne sabar gi ka ham -ul garab ga sa tool -u -b baay buur
alors on dire partie_de_tam-tam le\la celui savoir NEG arbre le\la à champ DETERMINATIF SG père roi
ADV PNIND V N ARTDEFSG PN VI SUF N ARTSG PREP null SUF CLASSE N N
ecouter
ken du la taka  
ken du la taka
ken du la taka
personne\quelqu'un futur négative te\toi épouser
PNIND MOD PNC2SG VT
ecouter
kumba amul ndey leegi  
kumba amul ndey leegi
kumba am -ul ndey leegi
Coumba avoir NEG mère alors
N VT SUF N ADV
ecouter
keena mu dem sa armeel ya la jooy yaayam la jooyle yaayam la jooy yaayam  
keena mu dem sa armeel ya la jooy yaayam la jooyle yaayam la jooy yaayam
kenn mu dem sa armeel ya la jooy yaay -am la jooy -le yaay -am la jooy yaay -am
seul\seule il\elle partir\aller à cimetière les INACC pleurer mère\maman POSS3SG INACC pleurer SUBSTITUT DE PRONOM mère\maman POSS3SG INACC pleurer mère\maman POSS3SG
ADV PNS3SG VI PREP NPL pnP AUX V N SUF AUX V SUF N SUF AUX V N SUF
ecouter
be dagi buur feka ka fa  
be dagi buur feka ka fa
be dag -i buur feka ka fa
jusque valet DETERMINATIF roi trouver la là-bas
PREP N DEFPROX N VT ART ADV
ecouter
na ha laa la jooy  
na ha laa la jooy
ne ha laa la jooy
dire ah quoi_être tu pleurer
V INTERJ STG PNS2SG V
ecouter
mu nettali lépp be mu pare mu na baay buur  
mu nettali lépp be mu pare mu na baay buur
mu nettali lépp be mu pare mu ne baay buur
il\elle raconter tout jusque il\elle finir de faire il\elle dire père roi
PNS3SG VT ADV PREP PNS3SG VT PNS3SG V N N
ecouter
dina la pooseel loho li  
dina la pooseel loho li
dina la poose -al loho li
FUTUR te\toi porter une prothèse BENEFACTIF bras le\la
MOD PNC2SG V SUF N ARTDEFSG
ecouter
te garab googa sa toolab baay buur  
te garab googa sa toolab baay buur
te garab googa sa tool -u -b baay buur
et arbre ce_là à champ DETERMINATIF SG père roi
CONJC N DEMDISTSG PREP N SUF CLASSE N N
ecouter
ag béntéeñé la  
ag béntéeñé la
ag béntéeñé la
un\une fromager être
ARTDEFSG N VI
ecouter
ba ñoom ñépp ba ñu woyee ba noopi rek baa duggee  
ba ñoom ñépp ba ñu woyee ba noopi rek baa duggee
ba ñoom ñépp ba ñu woy -ee ba noopi rek baa dugg -ee
jusque eux\elles tous\toutes quand elles chanter ANT jusque finir\terminer seulement quand_tu entrer ANT
ADV PN3PL PNPL CONJ PN3PL VT SUF ADV VT ADV STG VI SUF
ecouter
u woyee ba noppi u ne garab ga sa toolab baay buur béntéeñé la  
u woyee ba noppi u ne garab ga sa toolab baay buur béntéeñé la
u woy -ee ba noppi u ne garab ga sa tool -u -b baay buur béntéeñé la
tu chanter ANT jusque finir\terminer tu dire arbre le\la à champ DETERMINATIF SG père roi fromager être
PNS2SG VT SUF ADV VT PNS2SG V N ARTSG PREP N SUF CLASSE N N N VI
ecouter
... in la sabaru in la sabaru ka neeka dugga  
... in la sabaru in la sabaru ka neeka dugga
... in la sabar -u in la sabar -u ka neeka dugg
on INACC partie_de_tam-tam DEVERBATIF on INACC partie_de_tam-tam DEVERBAL qui se trouver entrer
PNIND AUX N SUF PNIND AUX N SUF PN VI VI
ecouter
ka duggë woy sa woy  
ka duggë woy sa woy
ka dugg woy sa woy
celui entrer chanter ton\ta chant\chanson
PN VI VT POSS2SG N
ecouter
ña ne du noonu  
ña ne du noonu
ña ne du noonu
on dire ne pas être comme_ça
PNIND V MOD ADV
ecouter
aaguloo fa leegi  
aaguloo fa leegi
aag -u -loo fa leegi
arriver NEGATION tu y alors
VI SUF PNS2SG PN ADV
ecouter
mu daldi sàllarñahu loho li daha def nakaa ku nit pooseloon nakaa koon  
mu daldi sàllarñahu loho li daha def nakaa ku nit pooseloon nakaa koon
mu daldi sàllarñahu loho li daha def nakaa ku nit poose -l -oon nakaa koon
il\elle puis\alors pivoter_sur_soi bras le\la EXPLICATIF_il\elle faire comme quelqu'un personne porter une prothèse BENEFACTIF PASSE comme marque l'irréel
PNS3SG ADV VI N ARTDEFSG MOD VT ADV PNIND N V SUF SUF ADV MOD
ecouter
mu ne saata baara baara ma saata  
mu ne saata baara baara ma saata
mu ne saata baara baara ma saata
il\elle faire
PNS3SG COV
ecouter
am njudóom la ma am de awmag këmëli kuuñ  
am njudóom la ma am de aw mag këmëli kuuñ
am njudóom la ma am de aw mag këmël -i kuuñ
être je avoir vraiment avoir_NEGATION je_CL section DETERMINATIF moignon
VI PNS1SG VT ADV STG STG N DEFPROX N
ecouter
garab ga sa toolu buur béntéeñé la  
garab ga sa toolu buur béntéeñé la
garab ga sa tool -u buur béntéeñé la
arbre le\la à champ DETERMINATIF roi fromager être
N ARTSG PREP N SUF N N VI
ecouter
dag ya daldee enu teg sa fas wa in dem  
dag ya daldee enu teg sa fas wa in dem
dag ya daldi -e yen -u teg sa fas wa in dem
valet les puis\alors variante_a_VERBAL aider_à_porter_sur_la_tête DEVERBATIF poser à cheval le on partir\aller
N ARTDEFDIST ADV SUF VT SUF VT PREP N ARTDEFSG PNIND VI
ecouter
buur taka ha  
buur taka ha
buur taka ha
roi épouser le\la
N VT PNC3SG
ecouter
ecouter
yaay jeeg baay ba ... ñibbi  
yaay jeeg baay ba ... ñibbi
yaay jeeg baay ba ... ñibbi
mère\maman le_et\la_et père le\la rentrer
N STG N ARTDEFSG VI
ecouter
léegi bi ñu demee sa céet ga  
léegi bi ñu demee sa céet ga
léegi bi ñu dem -ee sa céet ga
maintenant quand ils partir\aller ANT à noces le\la
ADV CONJS PN3PL VI SUF PREP N ARTSG
ecouter
leegi baay bi ne mu ne moom moo la palaale tey  
leegi baay bi ne mu ne moom moo la palaale tey
leegi baay bi ne mu ne moom moo la palaale tey
alors père le\la dire il\elle dire lui\elle c'est_il_qui aujourd'hui
ADV N ART V PNS3SG V PN STG ADV
ecouter
mu ne moo la palaale  
mu ne moo la palaale
mu ne moo la palaale
il\elle dire c'est_il_qui
PNS3SG V STG
ecouter
bi mu nee moo la palaale  
bi mu nee moo la palaale
bi mu nee moo la palaale
quand il\elle dire + ANTERIORITE c'est_il_qui
CONJS PNS3SG V STG
ecouter
waaye bi mu nee moo la palaale tey sa séet ba  
waaye bi mu nee moo la palaale tey sa séet ba
waaye bi mu nee moo la palaale tey sa séet ba
mais quand il\elle dire + ANTERIORITE c'est_il_qui aujourd'hui à nouvelle mariée le\la
CONJC CONJS PNS3SG V STG ADV PREP N ARTDEFSG
ecouter
mu dem sa séet ba  
mu dem sa séet ba
mu dem sa séet ba
il\elle partir\aller à nouvelle mariée le\la
PNS3SG VI PREP N ARTDEFSG
ecouter
ñu neeka faa neeka neeka be  
ñu neeka faa neeka neeka be
ñu neeka faa neeka neeka be
ils être là-bas être être jusque
PN3PL VI ADV VI VI PREP
ecouter
in dem mu ne ha kaay nu dohantuy  
in dem mu ne ha kaay nu dohantuy
in dem mu ne ha kaay nu dohantuy
on partir\aller il\elle dire lui viens nous aller_se_promener
PNIND VI PNS3SG V PNC3SG V PN1PL VI
ecouter
ñu géena in la dohantuy  
ñu géena in la dohantuy
ñu géena in la dohantuy
ils sortir on INACC aller_se_promener
PN3PL VI PNIND AUX VI
ecouter
mu ne na kaay nu dëglu teenab baay buur  
mu ne na kaay nu dëglu teenab baay buur
mu ne na kaay nu dëglu teen -u -b baay buur
il\elle dire INCITATIF venir nous écouter puits DETERMINATIF SG père roi
PNS3SG V MOD VI PN1PL VT N SUF CLASSE N N
ecouter
ecouter
yàlla emaale seb lalub diimaa  
yàlla emaale seb lalub diimaa
yàlla emaale seb lal -u -b diimaa
Dieu disposer y_un lit DETERMINATIF SG divan
N VT STG N SUF CLASSE N
ecouter
sa kow laalul ndoh mi laalul suuf mu emaale seb lal  
sa kow laalul ndoh mi laalul suuf mu emaale seb lal
sa kow laal -ul ndoh mi laal -ul suuf mu emaale seb lal
à dessus\haut toucher NEG eau le\la toucher NEG par terre il\elle disposer y_un lit
PREP ADV VT SUF N ARTDEFSG VT SUF ADV PNS3SG VT STG N
ecouter
ecouter
ecouter
leegi mu dem ne mu dem ndaw ña  
leegi mu dem ne mu dem ndaw ña
leegi mu dem ne mu dem ndaw ñi
alors il\elle partir\aller dire il\elle partir\aller jeunes les
ADV PNS3SG VI V PNS3SG VI N PNPL
ecouter
ne kii de dee na  
ne kii de dee na
ne kii de dee na
dire truc\machin quant à être mort MRV
V STG ADV VI MOD
ecouter
kumba amul ndey dee na  
kumba amul ndey dee na
kumba am -ul ndey dee na
Coumba avoir NEG mère être mort MRV
N VT SUF N VI MOD
ecouter
ña ne kumba amul ndey fa mu dee  
ña ne kumba amul ndey fa mu dee
ña ne kumba am -ul ndey fa mu dee
on dire Coumba avoir NEG mère il\elle être mort
PNIND V N VT SUF N PN PNS3SG VI
ecouter
mu ne ña mu nga dee sa aala ba  
mu ne ña mu nga dee sa aala ba
mu ne ña mu nga dee sa aala ba
il\elle dire leur il\elle PRESENTATIF+DISTANT être mort à brousse\forêt le\la
PNS3SG V PNC3PL PNS3SG MOD VI PREP N ARTDEFSG
ecouter
léegi dag yi dem la nàndali  
léegi dag yi dem la nàndali
leegi dag yi dem la nàndal -i
alors valet les partir\aller INACC abreuver EXITIF
ADV N ARTDEFPL VI AUX VT DEFPROX
ecouter
ñu ne kunduŋ baag bi  
ñu ne kunduŋ baag bi
ñu ne kunduŋ baag bi
ils faire plouf seau pour puiser le\la
PN3PL COV ADV N ART
ecouter
mu ne kooku kë mu doon kooku kë mu doon  
mu ne kooku mu doon kooku mu doon
mu ne kooku ku mu doon kooku ku mu doon
il\elle dire celui-là\celle-là qui il\elle être celui-là\celle-là qui il\elle être
PNS3SG V PN PNIND PNS3SG VI PN PNIND PNS3SG VI
ecouter
mu ne ala man a dagi buur njaay  
mu ne ala man a dagi buur njaay
mu ne ala man a dag -i buur njaay
il\elle dire être moi c'est_qui valet DETERMINATIF roi Ndiaye
PNS3SG V VI PN1SG MOD N DEFPROX N N
ecouter
mu ne boo demee sa buur  
mu ne boo demee sa buur
mu ne boo dem -ee sa buur
il\elle dire quand_tu partir\aller ANT à roi
PNS3SG V STG VI SUF PREP N
ecouter
nee ko sa jabar a nga sa teen ba  
nee ko sa jabar a nga sa teen ba
nee ko sa jabar a nga sa teen ba
dire_IMPERATIF lui\elle ton\ta épouse PRESENTATIF PRESENTATIF+DISTANT à puits le\la
V PN POSS2SG N MOD MOD PREP N ARTDEFSG
ecouter
koo dem wah ko baay buur baay buur na ha déedéet  
koo dem wah ko baay buur baay buur na ha déedéet
kooku dem wah ko baay buur baay buur ne ha déedéet
celui-là\celle-là partir\aller parler\dire ça père roi père roi dire lui pas possible
PN VI V PN N N N N V PNC3SG INTERJ
ecouter
daldi ebal ñeneen  
daldi ebal ñeneen
daldi ebal ñeneen
puis\alors mandater d'autres
ADV VT PNPL
ecouter
ñoom itam ña dugal baag ba  
ñoom itam ña dugal baag ba
ñoom itam ña dug -al baag ba
eux\elles aussi ils\elles entrer CAUSATIF seau pour puiser le\la
PN3PL ADV PNS3PL VI SUF N ARTDEFSG
ecouter
mu jaarat sa baat ba  
mu jaarat sa baat ba
mu jaar -at sa baat ba
il\elle passer ITERATIF à phrase le\la
PNS3SG VI SUF PREP N ARTDEFSG
ecouter
be ñetti yoon  
be ñetti yoon
be ñetti yoon
jusque fois
PREP N
ecouter
baay buur ebal dag bu mag ba mu dem  
baay buur ebal dag bu mag ba mu dem
baay buur ebal dag bu mag ba mu dem
père roi mandater valet qui\que être_grand le\la il\elle partir\aller
N N VT N PN VI ARTDEFSG PNS3SG VI
ecouter
mu wah ka ha mu na sa jabar a nga sa teen ba  
mu wah ka ha mu na sa jabar a nga sa teen ba
mu wah ka ha mu ne sa jabar a nga sa teen ba
il\elle parler\dire lui ça\cela il\elle dire ton\ta épouse PRESENTATIF PRESENTATIF+DISTANT à puits le\la
PNS3SG V PN PN PNS3SG V POSS2SG N MOD MOD PREP N ARTDEFSG
ecouter
...  
...
...
ecouter
ña dem in génne ha in ëndi ha in teg  
ña dadi génne ha in ëndi ha in teg
ña dadi génn -e ha in ëndi ha in teg
ils\elles sortir TRANSITIVANT le\la on amener\apporter le\la on installer
PNS3PL VI SUF PNC3SG PNIND VT PNC3SG PNIND VT
ecouter
léegi ña ne nanoo toppiy tànka  
léegi ña ne nanoo toppiy tànka
leegi ña ne na -noo topp -i -y tank
alors ils\elles dire INCITATIF nous_a_Verbal suivre EXITIF des empreinte_de_pas
ADV PNS3PL V MOD STG VT DEFPROX ARTINDPL N
ecouter
ña dem baay buur waajal ha mu la toppiy tànka  
ña dem baay buur waajal ha mu la toppiy tànka
ña dem baay buur waaj -al ha mu la topp -i -y tank
ils\elles partir\aller père roi préparer BENEFACTIF lui il\elle INACC suivre EXITIF des empreinte_de_pas
PNS3PL VI N N VT SUF PNC3SG PNS3SG AUX VT DEFPROX ARTINDPL N
ecouter
bi mu demee na mu seet ay ay yaa xame ne daal da la yax iy bët  
bi mu demee na mu seet ay ay yaa xame ne daal da la yax iy bët
bi mu dem -ee ne mu seet ay ay yoo xam ne daal da la yàq ay bët
quand il\elle partir\aller ANT dire il\elle regarder des des CLASSE_u cjctif_pnS2s savoir que en_tous_cas EXPLICATIF INACC endommager\gâter des oeil
CONJS PNS3SG VI SUF V PNS3SG VT ARTINDPL ARTINDPL STG VI CONJ ADV MOD AUX VT ARTINDPL N
ecouter
ne pour ba kii dëbbee  
ne pour ba kii dëbbee
ne pour ba kii dëbb -ee
dire quand celui-ci\celle-ci piler ANT
V CONJ DEMPROXSG VT SUF
ecouter
mu dal si bët bi mu gumbë  
mu dal si bët bi mu gumbë
mu dal si bët bi mu gumb
cela heurter\percuter à oeil le\la il\elle être_aveugle
PN VT PREP N ART PNS3SG VI
ecouter
kumba amul ndey léegi ñoom  
kumba amul ndey léegi ñoom
kumba am -ul ndey leegi ñoom
Coumba avoir NEG mère alors eux\elles
N VT SUF N ADV PN3PL
ecouter
baa ñu def bisimlaay kumba am ndey dëbbë  
baa ñu def bisimlaay kumba am ndey dëbbë
baa ñu def bisimlaay kumba am ndey dëbb
quand on faire Coumba avoir mère piler
CONJS PNIND VT N VT N VT
ecouter
laalu ka kumba amul ndey dëbbë laalut ka  
laalu ka kumba am ndey dëbbë laalut ka
laal -u ka kumba am ndey dëbb laal -ut ka
toucher NEGATION le\la Coumba avoir mère piler toucher NEG le\la
VT SUF PN N VT N VT VT null PN
ecouter
kumba am ndey dëbë mu ne tupu sa bët ba mu tohoñ  
kumba am ndey dëbë mu ne tupu sa bët ba mu tohoñ
kumba am ndey dëbb mu ne tupu sa bët ba mu tohoñ
Coumba avoir mère piler cela faire plouf à oeil le\la il\elle se_frotter
N VT N VT PN COV ADV PREP N ARTDEFSG PNS3SG VT
ecouter
mu dëbaat mu ne tupu sa baa bët mu dem toog  
mu dëbaat mu ne tupu sa baa bët mu dem toog
mu dëbb -aat mu ne tupu sa bale bët mu dem toog
il\elle piler encore cela faire plouf à ce_là oeil il\elle partir\aller s'asseoir
PNS3SG VT SUF PN COV ADV PREP DEMDIST N PNS3SG VI VI
ecouter
yaay ji ñów ne a mënula yaay ji ñów dugal dëbë  
yaay ji ñów ne a mënula yaay ji ñów dugal dëbë
yaay ji ñów ne a mën -ul -a yaay ji ñów dug -al dëbb
mère\maman le\la venir dire ah pouvoir NEG tu\te mère\maman le\la venir entrer CAUSATIF piler
N ARTDEFSG VI V INTERJ null SUF PN N ARTDEFSG VI VI SUF VT
ecouter
mu ne tapa sa bët ba  
mu ne tapa sa bët ba
mu ne tupu sa bët ba
cela faire plouf à oeil le\la
PN COV ADV PREP N ARTDEFSG
ecouter
mu ñów nag di fëraat mu ne tapa sa bët ba  
mu ñów nag di fëraat mu ne tapa sa bët ba
mu ñów nag di fëraat mu ne tupu sa bët ba
il\elle venir alors INacc cela faire plouf à oeil le\la
PNS3SG VI null ASPECT PN COV ADV PREP N ARTDEFSG
ecouter
baay bi ne mënula mu ñów  
baay bi ne mënula mu ñów
baay bi ne mën -ul -a mu ñów
père le\la dire pouvoir NEG tu\te il\elle venir
N ART V null SUF PN PNS3SG VI
ecouter
dëbaat mu ne tafaa sa bët ba  
dëbaat mu ne tafaa sa bët ba
dëbb -aat mu ne tupu sa bët ba
piler encore cela faire plouf à oeil le\la
VT SUF PN COV ADV PREP N ARTDEFSG
ecouter
ñoom ñépp ñu booka doon gumbë  
ñoom ñépp ñu booka doon gumbë
ñoom ñépp ñu bokk doon gumb
eux\elles tous\toutes ils partager être aveugle
PN3PL PNPL PN3PL VT VI N
ecouter
kumba am ndey daldi  
kumba am ndey daldi
kumba am ndey daldi
Coumba avoir mère puis\alors
N VT N ADV
ecouter
kumba amul ndey daldi delluwaat sab séyam la séy  
kumba amul ndey daldi delluwaat sab séyam la séy
kumba am -ul ndey daldi dellu -w -aat sab séy -am la séy
Coumba avoir NEG mère puis\alors retourner EPENTH encore à_un mariage à_lui\à_elle INACC vivre_un_ménage
N VT SUF N ADV null null SUF STG N SUF AUX VI